Gestu ci ni ñuy woowe nit ñi ci yenn gox yi, bu ñu sukkandikoo ci kàllama yu mel ni mànkaañ, wolof, séeréer ak soose
Descripción del gentilicio en las lenguas de Senegal: con ejemplos del mancañá, del wolof, del seereer siin y del mandinga
Mots-clés :
Morfosintaxis Comparada, Gentilicio, TopónimoRésumé
Ci gàttal: Gestu bi mu ngi màcc jëm ci ni ñuy wowee ñi dëkk ci ab gox. Suma sukandikoo ci lima xam ci español, mooy ni bu ñu bëggee wax fi nit ki bokk ci turu dëkkam lañu koy jëlee, dama leen a bëgga wax nan lañu koy defee ci yeneeni làkk, won leen tamit baxam ci làkk yooyu am na ci ñu koy waxee lu méngoo ak ni ko español di waxee wala déet. Looloo tax, gestu bi ñu def ko ci ñenti làkk yu Senegaal: mànkaañ, wolof, séeréer siin ak soose. Bi ñu càmbaree melokaanu làkk yii daldi leen méngale, danu gis ni danuy faral di tënk kàddu yi bu nu bëggee wax fi nit ki bokk, te loolu amul ci español. Bu dee mànkaañ, dafa am kàddu bu njëkk bu nuy yokk ci ni nu koy waxee. Bu dee wolof ak seereer siin, benn kàddu bi danu koy wax ñaari yoon. Bu dee soose, dafa am lu nuy soppi ci waxin wi. Waayee, nu wone tamit ni ni ko español di waxe bari na, man naa ni de yokk ci turu dëkk bi, walla hijo de yokku ci turu dëkk bi, muy tekki ci español dëkk ca. Naam làkk bu ci ne am na loo xam ni moom rekk a ko am (ci misaal làkk bu mel ni soose day jël turu dëkk bi yokk ci de), bu ñu xoole lepp, man nañu ni làkk yii nu def sunu gëstu bi am na luñu niróok español, ndax fi nit ki bokk man nañ ko wax ci ñaari waxin yu bokkul: man na nu tënk kàddu yi wax ko, waaye tamit man nanu càmbar kàddu wax ko.
***
El presenta estudio versa sobre el gentilicio, es decir, el nombre que reciben los habitantes de una localidad. Partiendo de lo que sabemos en español, a saber que el origen de la persona se expresa mediante la derivación a partir del topónimo o por medio de la construcción de + topónimo, nos hemos propuesto dar cuenta de las formas que se emplean en otras lenguas y señalar cuáles coinciden con las españolas y cuáles no. Para ello, hemos centrado nuestra atención en cuatro lenguas de Senegal: el mancañá, el wolof, el seereer siin y el mandinga. El análisis formal y comparado llevado a cabo permite destacar diversos mecanismos sintéticos para formar el gentilicio, que se desconocen en español. Se trata de la derivación por prefijación (en mancañá), la reduplicación (en wolof y en seereer siin), la alternancia consonántica (en seereer siin). También cabe apuntar distintas formas analíticas como la de de + topónimo, que sí se emplea en español y la de hijo de + topónimo, correspondiente a la construcción española natural de. A pesar de las particularidades aludidas (además de la construcción topónimo + de propia del mandinga y debida a su estructura SOV), de manera general, las lenguas estudiadas coinciden con el español, pues construyen el gentilicio de dos formas principalmente: de forma sintética y de forma analítica.
Téléchargements
Références
COLÍN GORRÁEZ, Miriam et al. (2009): Introducción a la entrevista psicológica (1a ed.), México: Trillas.
GARCÍA PADRÓN, Dolores (2012): «La derivación no canónica en los gentilicios españoles», in Dolores García Padrón et María del Carmen Fumero Pérez, Estudios sobre lengua, cultura y cognición, Frankfurt am Main: Peter Lang, pp. 79-88.
GARCÍA PADRÓN, Dolores (2015): «La lexicalización de los gentilicios en español», in Marcial Morera, El gentilicio en español: aspectos teóricos y prácticos, Madrid: Arco / Libros: pp. 97-135.
GARCÍA PADRÓN, Dolores et MORERA PÉREZ, Marcial (2015): «Gentilicios y lexicografía», in Onomazein, nº 31, pp. 81-98.
HASPELMATH, Martin et al. (2014): «Comparative syntaxe», en The Routledge handboook of syntax, pp. 4 90-508.
HERRERA SANTANA, Juana (2015): «La dimensión socio-pragmática de los gentilicios», in Marcial Morera, El gentilicio en español: aspectos teóricos y prácticos, Madrid: Arco / Libros: pp. 137-168.
MARCIAL MORERA (2012): «Gentilicios y seudogentilicios: mostración vs. descripción», Revista de Lexicografía, XVIII, pp. 103-140.
MORERA PÉREZ, Marcial (2014): «Los gentilicios en Fuerteventura: causas de su escasez y criterios para remediarla», in Fortunatae, nº 25, pp.
MORERA PÉREZ, Marcial (2015): «El gentilicio en español: tipos, significaciones y sentidos», in Marcial Morera, El gentilicio en español: aspectos teóricos y prácticos, Madrid: Arco / Libros: pp. 11-96.
PÉREZ VIGARRAY, Juan Manuel (2015): «Gentilicios y lexicografía», in Marcial Morera, El gentilicio en español: aspectos teóricos y prácticos, Madrid: Arco / Libros: pp. 245-302.
REAL ACADEMIA ESPAÑOLA (2010): Manual de la Nueva Gramática de la Lengua Española, Madrid: Espasa.
TABARES PLASENCIA, Encarnación (2015): «La variación gentilicia, con especial atención a la variación fónico-gráfica», in Marcial Morera, El gentilicio en español: aspectos teóricos y prácticos, Madrid: Arco / Libros: pp. 169-204.
TRAPERO, Maximiliano (1997): «Para una teoría lingüística de la toponimia», in Almeida y Dorta, Contribuciones al estudio de la Lingüística Hispánica. Homenaje a Profesor Ramón Trujillo, La Laguna: Montesinos y Cabildo Insular de Tenerife, pp. 241-253.
Téléchargements
Publiée
Comment citer
Numéro
Rubrique
Licence
(c) Tous droits réservés NJINGA&SEPÉ: Revista Internacional de Culturas, Línguas Africanas e Brasileiras 2021
Ce travail est disponible sous licence Creative Commons Attribution - Pas d'Utilisation Commerciale - Pas de Modification 4.0 International.
Les auteurs qui publient dans cette revue acceptent les conditions suivantes:
Les auteurs conservent le droit d'auteur et accordent à la revue le droit de première publication, l'œuvre étant simultanément concédée sous licence Creative Commons Attribution License, qui permet le partage de l'œuvre avec reconnaissance de la paternité de l'œuvre et publication initiale dans ce magazine.
Les auteurs sont autorisés à assumer séparément des contrats supplémentaires, pour la distribution non exclusive de la version de l'ouvrage publié dans cette revue (par exemple, publication dans un référentiel institutionnel ou en tant que chapitre de livre), avec reconnaissance de la paternité et publication initiale dans cette revue.
Les auteurs sont autorisés et encouragés à publier et distribuer leurs travaux en ligne (par exemple dans des référentiels institutionnels ou sur leur page personnelle) à tout moment avant ou pendant le processus éditorial, car cela peut générer des changements productifs, ainsi que citation des travaux publiés (voir l'effet du libre accès).